Xathie Yaa Ngui Mbew
Yess Man Yess Man
bayilen niouy wax
bayilen niouy wax
[refrain]
bayilen niouy waxx waxx j
niom nio ko taal
dieuf té jeul mom la Bamba digalone Cheikh Ibra Fall
beuw hadj bi ci tali bi téréwoul Oto bi agg fi mou dieum bayilen nio ko tal (x2)
Niou gui waar
niou gui aar
niou gui saar di dem
tiow lé beuri rekk Bardé guen
merdé guen merdé guen
wora jog guen di wax yen tardé guen
let them talk
nio gui Job pour wa galé meuna tioop
haterz yi meunou niou ma Stop
li ma war moy fékhé Go
ma gui fi deh yagui fé
kham ga beurre dou Karité
mane sama réalité
fils deh moy deh manduté
naga dokh sa dokh
waxx sa waxx
sama poche boul ko kipé
diw li diw lé sa sou nek moy sa yité
[refrain]
bayilen niouy waxx waxx j
niom nio ko taal
dieuf té jeul mom la Bamba digalone Cheikh Ibra Fall
beuw hadj bi ci tali bi téréwoul Oto bi agg fi mou dieum bayilen nio ko tal
képp yé gui souss si nopp boum yi Indicateur le
fadj katt yé gui soralé fou bi doundou secteur le
niata la waxx dougal ci biir
yolémane yéé gui riir
waxx ba say nopp biiir
do your thing ba len ci biir
sa girl man la gravé ci kholam
sama son moy daw si call am
move bi fils daga ci gueuleum
bone khol dou ci lekk deureum
teup niou rekk feuss
diom moniu mbeth pess
fokk niou wathie ci cars yi dou ci lexus
douniou fa dieul deuss
kouniou fa mball reuss
fokk souniou diant fénk rekk feuss
yotou push it khouss ci ay eat
vinaigre none yi ba foula sen tiit
bandit mic la
waar bi bike la
tay mou yakk la jitté sappé ya
[refrain]
bayilen niouy waxx waxx j
niom nio ko taal
dieuf té jeul mom la Bamba digalone Cheikh Ibra Fall
beuw hadj bi ci tali bi téréwoul Oto bi agg fi mou dieum bayilen nio ko tal (x2)
mame dane na waxx nane kou bot bouki hadj yi beuw la fo rombou yaw la
mame dane na waxx nane ignanne ignetti ignagnetti siniou negn la
mame da na waxx nane bouniou demé bay wax si yaw da fek ga jitou len
mame dane na waxx nane li yalla deff si diaam bo len ko nango mou nopal len
Merci Papa Aliou Ka
niceu vrema l ecriture ya rien a dire tei le genie j vs adore
RépondreSupprimer